Unduh APK dengan Aman dan Cepat di APKPure
APKPure menggunakan verifikasi tanda tangan untuk memastikan unduhan APK Kàddug Yàlla yang bebas dari virus untuk Anda.
Kàddug Yàlla: Kóllëre gu jekk gi ak Kóllëre gu bees gi.
Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari tére yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci tére yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.
[Alkitab, wolof, kaddug yalla]
Sekali klik untuk menginstal file XAPK/APK di Android!